Ay Kuru Anglais
Bindu yi dina tambalee 27 awril ba 2 mee ci Centre Baptiste de Sebikotane.
Xibaar
Am nanu ay kuuri Ànglais ngir ñiy tàmbali, digg yi ak ñi xarañ ci mag ñi am 20 at jëm ci kaw. Kuur bi dina am juróom ñatti ayu-bis, te njàngale yi ñaari yoon ci ayu-bis bi dañuy tàmbalee ci 17:30 ba 19:00 ci altine ak Talaata, wala Alxamis 17:30 ba 19:00 ak Samdi 10:30 ba 12:00 ci midi. Club waxtaan dina am Samdi bu nekk 12pm ba 1pm.
Boo bëgee bindu njëg lee moy 10.000F CFA. Bindu ci Sebikotane Baptist Digg. Nio gui lay nianne nga indaale sa ID ak sa 10.000 CFA. Boo bindoo diggante 27 awril ak 2 mee dina nu la wañil 20% do faye ludul 8000 CFA.

